Ci Senegaal, ci téeméer boo jël ci jigéen ñiy séy , ñaar-fukki yi ak juroom aajowoo nañu pexem soreyàntool njur te mënul a faju
Crédit: Sedgh G et al., Estimations de l’incidence de l’avortement provoqué et conséquences de l’avortement non médicalisé au Sénégal, Perspectives Internationales sur la Santé Sexuelle et Génésique, numéro spécial de 2015, pp. 35–44.
Cette infographie et l’étude sur laquelle il repose principalement ont bénéficié du soutien de la William and Flora Hewlett Foundation.
